Sayüma lagissé 
Dama laï beugeu wakh-li tchi sama khöll
Waké khep nge samaï khalatt bä fogné 
Topoto üma tiono gunde-gi
Beuguema
Amo darra lö chille-tite 
Kaï wuyüma amö- darra loï ragall 
Téïte-néka-tüma göné 
Budéça fallé-üma darra 
Dunde akh nitte néküll mbir mü yômbe
Xam-mü- ma saï kharitte 
(Mané) xam-mü-ma, xam-mü-ma 
Xam-mü-ma saï kharitte 
Li sökhal-nama, sökhal-nama
Yittel-nitte-ny beuss-bü-neck 
Mö warral nga maï kholé 
Ni-kü-top lüoull tiaxane.